• Céddalem dund gu ñu démbaléewoon nit ñi ca Nepaal. ñu gën a xam ni nit ñi dundé, su ko defee ñu gën a xam liñu war a def dolli, fexe be lépp lu ñuy def méngook ni nit ñi di dunde, mën naa tax mën a indi yokkute ci wàllu dundi doom-aadamaak koom-koom gu sax waaye ñëw ñu jëfandikóo ko ci anam yi dëppóok ni nit ñi di dunde moo lépp lu Misaal 2 : Ay dëkki-dëkk fexel nañ seen bopp ni ñuy séddalee dund gi ñu Ngir mu wóor leen ne nit ñi dinañu jot ci dund gi ñu leen di dimbalée, séddalee dund. Li ñuy jëlé ay kamyo , ar sareti nag lañuy sëf dund gi. li ñu waroon a jot ci dund gi yokku, te loolu naruloon a am su fekkoon na ba nit ñi xam ni dund gi ñu séddalé yem. Ci noonu itam la ñuy xame "liggéey ñu féy lag lekk " dina yombal joxeg dund gi te nekk misaalu gàllankoor seenug dund. na am ñu mu lor, te ñi ciy jëkk ñooy ñi leen doon suuxat di leen dunde. •Gëstu takku yu ñu def ci ni doom aadama yi di dunde yuy joxe ay xabaar ndimbal ci seen dund rawatina néew doole yi?