ganesi àddina ( 76 à 81 ) arrow #78 Ndekkite li ak Dund gi #78 Ndekkite li ak Dund gi Convertir en PDF Version imprimable Suggérer Musalkat bi... Ñam wiy joxe dund gi... Leeru Àddina si... Boroom gisaat yeneen ñaari turi Yeesu: ñooy: "Ndekkite li ak Dund gi." maay ndekkite li, maay dund gi. Ku ma gëm, boo deeyee it, dinga dund. 26Rax-ca-dolli kuy dund te gëm ma, doo dee mukk. Ndax gëm nga loolu? sosoo ba tey, musuñoo dégg nit ku mana jox dund néew, bu am ñeenti fan Yàlla; di Ruuwu Yàlla, gi jóge asamaan. Ni Yàlla ame dund gi moom ci di leen jox dund gi, noonu la Almasi bi di joxe dund gi ñi mu ko bëgga jox, ndaxte Moom ci boppam mooy Aji Dund ji. Looloo taxoon bi Yeesu woowee Lasaar mu ñëw ci biti, néew bi daldi dundaat, jóg, génn bàmmeel ndekkite li, maay dund gi. Ku ma gëm, boo deeyee it, dinga dund!" ndekkite li ak dund gi. Looloo tax Yeesu manoona wax jigéenu Lasaar, ne ko: "Man maay ndekkite li, maay dund gi. Ku ma gëm, boo deeyee it, dinga dund... Ndax gëm nga loolu?" (Yow. 11:25,26) dundu Almasi bi, nanga nu bind ci: YOONU NJUB / B.P. 370. / Saint Yeesu waxoon, bi mu naan: "Man maay ndekkite li, maay dund gi! Ku ma gëm, boo deeyee it, dinga dund! ...Ndax gëm nga loolu?" (Yow.