1:1 Man Pool, ndawul Yeesu Kirist ci coobareg Yàlla, ngir xamle dund 1:9 Moo nu musal te woo nu ci dund gu sell, ci lu ajuwul ci sunuy jëf, nasaxal dee te feeñal dund ci xebaar bu baax bi, te muy dund gu sax. 2:11 Kàddu gu wóor a ngii:Su nu deeyaalee ak Kirist,dinanu dundaat ak 3:10 Waaye yaw nag xam nga bu baax sama njàngale, sama dund, sama 3:12 Te ku bokk ci Kirist Yeesu, te bëgg dund dund gu ànd ak ragal ñiy dund ak ñi dee, di la dénk ci feeñam ci biir ndam ak ci nguuram,