1 Nu ngi leen di bind ci mbirum Ki ñuy wax Kàddug dund, moom mi amoon 2 Dund feeñ na, te gis nanu ko; te moom lanuy seedeel, di leen yégal dund gu dul jeex, googu nekkoon ci wetu Yàlla Baay bi te feeñu nu. 6 Ku wax ne ci Yàlla nga sax, fàww nga dund, ni Yeesu Kirist daan dunde moom ci boppam. 8 Teewul ndigal lu bees laa leen di bind, lu amoon ci dundu Yeesu, te am it ci seen dund; ndaxte lëndëm gaa ngi wéy, te leer gu wóor gi fenk 25 Te li mu nu digoon mooy lii: dund gu dul jeex. tàbbi ci dund. Ku bëggul sa mbokk, yaa ngi ci dee ba tey. amuloo dund gu dul jeex. Doomam ji mu am kepp, ngir nu am dund ci moom. 11 Te seede si mooy lii: Yàlla jox na nu dund gu dul jeex, te dund 12 Ku am Doom ji, am nga dund; ku amul Doomu Yàlla, amuloo dund. ngeen xam ne, am ngeen dund gu dul jeex. Yàlla dina ko may dund. Ku def bàkkaar bu jarul dee laa wax. Ndaxte am Kooku mooy Yàlla ju wóor, ji yor dund gu dul jeex. 6 Lii mooy mbëggeel: nu wéer sunug dund ci ndigali Yàlla; loolu mooy dund gépp, te bég naa ci lool. o VAMOS ORAR: VIETNÃ