Sit bilèni diox lèpp lungèn soxla ci net bi ci lakku wolof.
Jamono day dox sunuy yittè di gena bari, bari lunu war dèf ta diamono xat,
mo tax niu begg lèpp lunu soxla mu nèkk sunu wèt niun niepp.
1
2
Barina luniuy bayyi liniu don def lèpp, di xol xibar bo xamni soppiwul dara
ci sunu dund ak sunu dundin,
mo tax niuy sgg xibar yi gena am solo Senegal ak ci addunabi dico lèral fi.
3
Xam xam moy lo xamni dara menula dèm bayyico ak lumu mene don.
Fi da nio begg lu nit xam ta begko xamlè mu dèfco video wala fan bumu mena don ci lakku wolof yonnè niuko niu saytuko dèfco fi, ba kuko soxla bu niewè fi fèkkofi.